rëbbees na kiy sëy ak soxnaam ci ginnaawam

rëbbees na kiy sëy ak soxnaam ci ginnaawam

Jële nañu ci Abuu Hurayrata yal na ko Yàlla dollee gërëm mu wax ne: Yonente Yàlla bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc nee na: «rëbbees na kiy sëy ak soxnaam ci ginnaawam».

[Tane na] [Abóo Daawuda soloo na ko, ak An-nasaa'iy ca Al-kubraa, ak Ahmat]

الشرح

Yonente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc day tere jëkkër ji di sëy ak soxnaam ci ginnaawam; ak ni moom ku ñu rëbb la dàq ko ci yërmàndey Yàlla, te dafa bokk ci bàkkaar yu mag yi.

فوائد الحديث

Araamalees na di sëy ak jigéen ñi ci seen ginnaaw ya.

Bànneexu ci soxna si ci fu dul ginnaawam ci yaramam lu dagan la.

Jullit day sëy ak jigéen gi ci péyam kem ni ka ko Yàlla digalee; bu dee ginnaaw gi nag loolu ag yàquteg xol la, ak sànk njaboot, te daa wuute ak li xel mu sell, te ay lor yu rëy la ci ñaar ñiy sëy.

التصنيفات

Teggiini sëy